Lu ngeen di yëg? Waaw, maa ngi waajal ëlëg Maa ngi waajal, waaye nit ñi ma wër waajal wuñu ko Mbir yi dañu gaawa soppeeku ci man Xamuma lu ëlëg di indaale Lan moo wara xew ci Dagana ngir nga wax waaw?
No comments yet
Be the first to start the discussion.